Letra de ' C'est Dieu ' de Bass Thioung

Si llevas mucho tiempo buscando la letra de la canción C'est Dieu de Bass Thioung , empieza a calentar la voz, porque no podrás parar de cantarla.

¿Te encanta la canción C'est Dieu ?¿No terminas de entender lo que dice? ¿Necesitas la letra de C'est Dieu de Bass Thioung ? Te encuentras en el lugar que tiene las respuestas a tus anhelos.

C'est Dieu
Hey, hey, hey, hey

Hey si tu aimes, fais partie des miens
Nous on fait ça bien
Si t'aime pas, garde tes commentaires
On en a rien à faire

C'est Dieu!
Tout ce que je fais, y'a Dieu dedans
C'est Dieu!
Hey, c'est pas les marabouts
C'est Dieu!

Yaay yaa yax duma takk, duma naan
Sëriñ du lekk sama dërëm
Hay wuy sama ndey!
Xale bi yaayam da ko ñaanal
Hey, xale bi yaayam da ko ñaanal
Hey Yàlla fi ne

C'est pas les marabouts
C'est Dieu!
Hey, hey, hey, hey
C'est pas les marabouts
C'est Dieu!
Hey, hey, hey, hey
Fecc bu bees!
C'est pas les marabouts
C'est Dieu!
Hey, hey, hey, hey

Yàlla jël kooku neex
Def ci moom lu ko neex
Soo nangoo ndogal rekk
Fils sa xol du gaaw a jeex
Yénne ngeen la yaa ko tabax
Te yaa ciy fanaan
Nga bañ ma lu may waññi
Hey iñaan dafa tarde

Je suis béni (béni)
Hey je suis béni
C'est pas les marabouts
C'est Dieu!
Je suis béni (béni)
Hey je suis béni
C'est pas les marabouts
C'est Dieu!
Je suis béni (béni)
Hey je suis béni
C'est pas les marabouts
C'est Dieu!

Hey Yàlla moo bari doole
Yàlla moo bari doole
Yàlla mooy may, lu dul Yàlla neen la
Yàlla noppi na (ayyy)
Su Yàlla bindee nga effacer
Hey yaw lay mujj effacer taracer (ay way!)
Su Yàlla dogalee may avancer
Hey yaw nangul ndogal bul déranger
Fils, soo gisee li bul di laaje
Hey Yàlla ci ànd ak man, y'a Dieu dedans
Xale bi Yàlla moo ko tàccu
Hey nanguleen ndogal way!
Y'a Dieu dedans!
Y'a Dieu dedans!

Je suis béni
C'est Dieu!
Hey je suis béni
C'est Dieu!
Hey c'est pas les marabouts
C'est Dieu!

Yaay yaa yax duma takk, duma naan
Sëriñ du lekk sama dërëm
Hay wuy sama ndey!
Xale bi yaayam da ko ñaanal
Hey, xale bi yaayam da ko ñaanal
Hey Yàlla fi ne

C'est pas les marabouts
C'est Dieu!

Je suis béni (béni)
Hey je suis béni
C'est pas les marabouts
C'est Dieu!
Je suis béni (béni)
Hey je suis béni
C'est pas les marabouts
C'est Dieu!

Y'a Dieu dedans!

Si c'est pas Dieu, c'est qui?
Ay, ay, ay, ay
Y'a Dieu dedans!
Baayu maman, baayu el-hadj, ak Mouhamed
Samba ak Sape, Omar jëlël li
Y'a Dieu dedans!
Omar Sow Yàlla moo ko tàccu
Hey naanuleen ndogal way!
Y'a Dieu dedans!
Chéri Ndaye Sene Omar Sow yaa ngi yëngal
Lu mu lundum lundum da ngay Khouss Diarr
Y'a Dieu dedans!
Omar Sow Yàlla ko teral!
C'est Dieu!
Diatou c'est bon!
Hey bu la pontu jamm, bu la paka laal
Lamecette aram naa la
Diatou ni la Yàlla def
C'est Dieu!

Diatou c'est bon!
Yaa ëpp doole te ya gëna feete xale
Seynabou sa doom Amatina Ndam
Diatou c'est bon!
Hey Diatou Yàlla ko teral
C'est Dieu!
Ibou Seye foo féete
Chéri béko kay

C'est pas les marabouts
C'est Dieu!

Je suis béni (béni)
Hey je suis béni
C'est pas les marabouts
C'est Dieu!
Je suis béni (béni)
Hey je suis béni
C'est pas les marabouts
C'est Dieu!

C'est pas les marabouts
C'est Dieu!

Cuando nos gusta mucho una canción, como podría ser tu caso con C'est Dieu de Bass Thioung , deseamos poder cantarla conociendo bien la letra.

Siéntete como una estrella cantando la canción C'est Dieu de Bass Thioung , aunque tu público sean solo tus dos gatos.

Un motivo muy usual para buscar la letra de C'est Dieu es el hecho de querer conocerla bien porque nos hacen pensar en una persona o situación especial.

¿Estás peleando con tu pareja porque entendéis cosas diferentes cuando escucháis C'est Dieu ? Tener a mano la letra de la canción de C'est Dieu de Bass Thioung puede zanjar muchas disputas, y esperamos que así sea.

Creemos que es importante advertir que Bass Thioung , en los conciertos en directo, no siempre ha sido o será fiel a la letra de la canción C'est Dieu … Así que es mejor centrarse en lo que dice la canción C'est Dieu en el disco.

Recuerda que cuando necesites saber la letra de una canción siempre puedes recurrir a nosotros, como ha ocurrido ahora con la letra de la canción C'est Dieu de Bass Thioung .