Sama Ex es una canción de Viviane Chidid cuya letra tiene innumerables búsquedas, por lo que hemos decidido que merece tener su lugar en este sitio web, junto con otras muchas letras de canciones que los internautas desean conocer.
¿Te encanta la canción Sama Ex?¿No terminas de entender lo que dice? ¿Necesitas la letra de Sama Ex de Viviane Chidid ? Te encuentras en el lugar que tiene las respuestas a tus anhelos.
Su ma xoolee ni tay sama ex nga
Ak li ñu dundu démb?
Xamuloo lu ma naroon pur maak yaw
Xale bi you don't know
Loolu tay dinga ko dégg mu metti la
Xamoo ci lu ma nekk
Yaa ngi wër fu ne di ma laajte
Nga mel ni ku for doom
Li nga téye woon sax loxo toxu na
Mi ngi ci yeneen niveau
Te xamuloo fi ma féete (fi ma féete)
Xale bi you don't know (you don't know)
Yu neex yi ma nekke (yi ma nekke)
Xale bi you don't know (you don't know)
Oh, oh nii xol bi di fexe (bi di fexe)
Xale bi you don't know (you don't know)
Oh, tay li nga perte (li nga perte)
Xale bi you don't know (you don't know)
Soo ko gisee waxal ma ko li dégg nga?
Mu noppali ku te muñ
Moo dem moo gedd sama xol bi
Yaay sama ex la
Duma wajju di lekkat ndax làmbu ma
Sa moroom moo ngi nii toog
Mu nobee ma lu ne defal ma
My baby kontaan naa
Sama número telefone changer naa
Maa ngi yeneen niveau
Te xamuloo fi ma féete (fi ma féete)
Xale bi you don't know (you don't know)
Yu neex yi ma nekke (yi ma nekke)
Xale bi you don't know (you don't know)
Oh, oh nii xol bi di fexe (bi di fexe)
Xale bi you don't know (you don't know)
Oh, tay li nga perte (li nga perte)
Xale bi you don't know (you don't know)
Ooh, waxal sama ex (waxal sama ex bi)
Waxal sama ex bi jaajëff (jaajëff)
Ndax bi mu ma bàyyee ba léegi
Man dama jëlaat poids
Ooh, waxal ma sa ex (waxal ma sama ex)
Waxal ma sama ex bi jaa (jaa)
Am na ku ko fii remplacer
Te di la kontaanloo
Oh, oh, oh, waxal sama ex (waxal sama ex)
Oh, oh, oh, waxal sama ex mu may ma
Ndax dina romb ci tawoon bii
Di dundu àljanna
Ooh, allo sama ex (allo sama ex)
Ooh, allo sama ex, goodbye
Am na ku la fi remplacer
Ba pare la la laaa
Li nga téye woon sax loxo toxu na
Mi ngi ci yeneen niveau!
Otras canciones de Viviane Chidid
Existen muchos motivos para querer conocer la letra de Sama Ex de Viviane Chidid .
Cuando nos gusta mucho una canción, como podría ser tu caso con Sama Ex de Viviane Chidid , deseamos poder cantarla conociendo bien la letra.
Saber lo que dice la letra de Sama Ex nos permite poner más sentimiento en la interpretación.
Un motivo muy usual para buscar la letra de Sama Ex es el hecho de querer conocerla bien porque nos hacen pensar en una persona o situación especial.
Algo que sucede en más ocasiones de las que pensamos es que la gente busca la letra de Sama Ex porque hay alguna palabra de la canción que no entiende bien y desea asegurarse de lo que dice.
¿Estás peleando con tu pareja porque entendéis cosas diferentes cuando escucháis Sama Ex? Tener a mano la letra de la canción de Sama Ex de Viviane Chidid puede zanjar muchas disputas, y esperamos que así sea.
Creemos que es importante advertir que Viviane Chidid , en los conciertos en directo, no siempre ha sido o será fiel a la letra de la canción Sama Ex… Así que es mejor centrarse en lo que dice la canción Sama Ex en el disco.
Apréndete las letras de las canciones que te gustan, como Sama Ex de Viviane Chidid , ya sea para cantarlas en la ducha, hacer tus covers, dedicarlas a alguien o ganar una apuesta.